📌« Keroog laa ko njëkka gis mu dindi kaala gi, ma gis ko mu yor ay njañ (karaw gu bari), ak sikim bu jekk te sëq lool, bi muy wax ak ñun (Moom ak Sñ Móodu Mustafaa ak Sñ Fàllu) ba ree, ci laa seetlu ne daa am sàkkalu Yàlla, te tuñ ya daa jib... »🤩
Sëriñ Omar Mbàkke Gelongal
31
297
1,755












